Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA

Letra de la Canción "Yeksil Remix" de Youssou N'dour | BooMusica 2025

Varios-artistas

Anime Awards 2024

Varios-artistas

Reggae Latino

Varios-artistas

AuronPlay Sin Copyright

Varios-artistas

Directos auronplay

Artist profile picture

Yeksil Remix

Youssou N'dour

Gëjoon fi lool bi nga ñëwee
Bi nga ñëwee
Duma fàtte nit nitam
Mooy garabam
Bokk nga ci ñi
Bokk nga ci ñi ma gën a bëgg
Hi hii hii

Koŋ- Koŋ, yegsil daal
Koŋ- Koŋ, yegsil daal
Koŋ- Koŋ, yegsil daal yegsil daal
Koŋ- Koŋ, yegsil daal
Yegsil avec plaisir
T'amènes que de beaux souvenirs

Waxtu wu la neex
Mën nga fëgg
Fii doo fii gan
Bu nu waxantee dëgg daal
Bokk nga ci ñi ma gën a bëgg

Koŋ- Koŋ, maa ngi xaar
Pressé d'entendre ta voix
Biig rekk, sax j'ai pensé à toi

Gëjoon fi lool bi nga ñëwee
Gëjoon fi lool bi nga ñëwee
Nee naa la, nee naa la, nee naa la
Bismi, bismi, bismillaah
Gëjoon fi lool bi nga ñëwee
Nee naa la, nee naa la, nee naa la
Bismi, bismi, bismi, bismi, bismillaah

Koŋ- Koŋ, Yegsil daal
Yegsil avec plaisir
T'amènes que de beaux souvenirs

Waxtu wu la neex
Mën nga fëgg
Man de xam naa
Ne sa fëgg yaw
Bokk nga ci ñi ma gën a bëgg

Man de damaa gis ci yaw sincérité
Dellu gis ci yaw, woyof ak dal
Moo tax ma yàkkamti sa jotaay ak sa ree ju neex
Man de damaa gis ci yaw sincérité
Dellu gis ci yaw, woyof ak dal
Moo tax ma yàkkamti sa jotaay ak sa ree ju neex
Ñëwal saa yu la neexee sa ñëw
Man da fa may dundal

Man de damaa gis ci yaw sincérité
Dellu gis ci yaw, woyof ak dal
Moo tax ma yàkkamti sa jotaay ak sa ree ju neex

Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA